Comentarios
Unbreakable Fye
Unbreakable Fye Hace 4 horas
Générique bi dal na torop surtout ne le changé pas
Seck Ousmane
Seck Ousmane Hace 4 horas
اللهم صل على سيدنا محمد وسلم
Mackenzie Bezos
Mackenzie Bezos Hace 4 horas
Medium Voyant Ésotérisme et prêtre vaudou (Paiement de la main d'œuvre après satisfaction totale) Certains d'entre vous n'ose plus consultés les sites internet suite à la mauvaise expérience. Il y en a qui ont malheureusement tombé sur des sites malhonnêtes concurrent. Que les choses soient bien claires, je n'ai aucun rapport avec ses sites qui ternissent l'image du maraboutage. Sachez qu'avec moi vous aurez tout ce que vous voulez comme satisfaction mais la seule chose que je n'aime pas du tout, c'est quand t'ont m'oublie après avoir reçu la satisfaction totale. J'aimerai vous propose une consultation et un travail unique : Ramener sa femme / mari même si cela fait plus de 20 ans; Ramener sa chance; Retrouver son amour; Réussir sa vie; Contre accident; Contre sorcellerie; Avoir facilement du travail; Avoir des enfants; Portefeuille magique; Adhérence pour la protection et la protection de sa maison Et plus encore!… Je n'ai pas de problème à travailler à distance. Des résultats sont immédiat et durable et le payement de la main d'œuvre serai après la satisfaction totale. Possibilité d'envoi par la DHL, FEDEX, EMS, UPS, TOP-CHRONO, par la POSTE ou par voie mystique CONTACT .... Téléphone: 22-995-719-863 WhatsApp: 22-995-719-863
Fatimata Fall
Fatimata Fall Hace 5 horas
Serie bi nexna amna sens
Mackenzie Bezos
Mackenzie Bezos Hace 5 horas
Medium Voyant Ésotérisme et prêtre vaudou (Paiement de la main d'œuvre après satisfaction totale) Certains d'entre vous n'ose plus consultés les sites internet suite à la mauvaise expérience. Il y en a qui ont malheureusement tombé sur des sites malhonnêtes concurrent. Que les choses soient bien claires, je n'ai aucun rapport avec ses sites qui ternissent l'image du maraboutage. Sachez qu'avec moi vous aurez tout ce que vous voulez comme satisfaction mais la seule chose que je n'aime pas du tout, c'est quand t'ont m'oublie après avoir reçu la satisfaction totale. J'aimerai vous propose une consultation et un travail unique : Ramener sa femme / mari même si cela fait plus de 20 ans; Ramener sa chance; Retrouver son amour; Réussir sa vie; Contre accident; Contre sorcellerie; Avoir facilement du travail; Avoir des enfants; Portefeuille magique; Adhérence pour la protection et la protection de sa maison Et plus encore!… Je n'ai pas de problème à travailler à distance. Des résultats sont immédiat et durable et le payement de la main d'œuvre serai après la satisfaction totale. Possibilité d'envoi par la DHL, FEDEX, EMS, UPS, TOP-CHRONO, par la POSTE ou par voie mystique CONTACT Téléphone: 22-995-719-863 WhatsApp: 22-995-719-863
Lam Kana
Lam Kana Hace 5 horas
Toujours les meilleurs 🔥🥰beg si yen rk ssp
Idrissa Diouf Sané
Idrissa Diouf Sané Hace 5 horas
Rayane raynameuh 😂😂sa nekh mom natou deugue moko dall
Kare Abdou Lahad
Kare Abdou Lahad Hace 5 horas
Bouy serie bi mome nekh na laf thiat mais rap bi khana da ame nioukoy setan di youkhou book motakh nguen dieul sen temp dindy ko djikoy professonale nii laye mel waye👍👍
Max La lionne
Max La lionne Hace 6 horas
Bakhaw ay na trop meune na rôlam
Bouchra
Bouchra Hace 6 horas
Ay Tonton Madiaga aie pitié de nous 😭😭😭😭😭saay kheetou style 😂!
Aminata Ndiaye
Aminata Ndiaye Hace 6 horas
Rayane il est fort😂😂😂qui est d'accord
Aminata Ndiaye
Aminata Ndiaye Hace 6 horas
Wa madiaga ak la Sophie kouniou yap😂😂😂nénako yaguimay nampal
Mariam Johnson
Mariam Johnson Hace 6 horas
Saneh why 😂😂😂😂😂😂👏👏❤️
Aminata Ndiaye
Aminata Ndiaye Hace 6 horas
Mais rabou Katy bii môme sadik na dii euw
MAME AMY KANDJI
MAME AMY KANDJI Hace 6 horas
amoul pub mo takh mou guena nekh
cumba barham KEBE
cumba barham KEBE Hace 6 horas
Fier de vous SLV realite deugu guenn tek Xalissou adouna walla poukoure adouna diarouli yeup ba yak sa vie diabot Big a Aziz couple nice Katy du courage c pas facile❤ah farou rapp kouko doundoul doko ham mettina lol hamnasi dara ❤
Mor Seck
Mor Seck Hace 7 horas
Vraiment série bou intéressant mais sén tourr yi dioulité woul dara franchement
Anta Sy
Anta Sy Hace 7 horas
Non bakhaw rayy nama🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Nabou Diouf
Nabou Diouf Hace 7 horas
seri bi avan mariage souboulou la me bokoye setane come ci apre mariage soumboula la
Aïda Diakhate
Aïda Diakhate Hace 7 horas
Wouy 😂😂bakhaw dineu maa rey waa leguii yarou naaa🤫🤫🤫
Sainabou Njie
Sainabou Njie Hace 7 horas
Soumblou yow deh waron nga russ sah gorro nyaka kersa bahoul
Ramatoulaye GUISSE
Ramatoulaye GUISSE Hace 7 horas
Ablaye diop khass dina nieuw fathie délia khana
Yacine Tall
Yacine Tall Hace 7 horas
Pen Bayil fen😂🏃‍♀️
Ndeyecoumba Diarra
Ndeyecoumba Diarra Hace 8 horas
Rayan dou nitt wae déh na😂😂😂
Diarra Ndiaye
Diarra Ndiaye Hace 8 horas
Rayane mi nit la🚶‍♀️😂😂😂nenako rouss na
Lamp Sylla
Lamp Sylla Hace 8 horas
C'est au top Macha Allah mais svp dèlen agalé série yi nakh mou am sens wayé di dagg rek
palène TV
palène TV Hace 8 horas
Mais gni séne série bi dafa raglou trop. Wala book
Kha diop
Kha diop Hace 8 horas
Chéri bi machalah amna Aÿ leson you am solo
Baye Zale Tine
Baye Zale Tine Hace 8 horas
Nn ndanan yi ken dou yenn bilae yalla na yalla def diamou❤️👌✨
Ahmada Chocola
Ahmada Chocola Hace 8 horas
Madiaga tu es le Meilleur
Limamoulaye Madiou Diallo
Limamoulaye Madiou Diallo Hace 8 horas
Nabouja ak Rayane lu ñuy dundu akka ñu bari či miim rewë mbi. Jiggën yikoy dundu gačče ngalamayen. Guisna cas yu melni yi.
Aminata Kasset
Aminata Kasset Hace 8 horas
Il a bien argumenté.suivez mon regards ...du ☀ magnifique
Ndeyecoumba Diarra
Ndeyecoumba Diarra Hace 8 horas
Soumboulou je t’aime trop wallah ❤️🌹🙈
Sokhna Thiaw Sène
Sokhna Thiaw Sène Hace 8 horas
Mais bi dafa xawa nouro ak CHOIX wala ma comprendroul rek
Maimouna Kasse
Maimouna Kasse Hace 8 horas
Nono radia
Aby Diallo
Aby Diallo Hace 9 horas
Nekhna lol😘😘😘
Khady Faye
Khady Faye Hace 9 horas
Mashallah nice daye bakh inshallah
Souleyemane Cissé
Souleyemane Cissé Hace 9 horas
Salam kou beugue aye niane wotéll si némorou bi amna fi aye thiarou boubakh. Lool si walou warr seug WhatsApp la 763334859
Cheikh Gueye
Cheikh Gueye Hace 9 horas
LIMAY WAKH ABLAYE DIOP KHASS YAKO MOM MOYTOUL DI KHOULO AK SOUMBOULOU POUR TONTOU REK HOO
gëm sa boppu tv
gëm sa boppu tv Hace 9 horas
Sangomar ou bien le choix je ne comprends plus !
Doudou Boye
Doudou Boye Hace 9 horas
Wa legui rouss na😂😂😂rehane dou nitt😂😂😂il joue bien
gëm sa boppu tv
gëm sa boppu tv Hace 9 horas
J'aime bien la troupe soleil levant .ils sont des meilleurs. dañoo bapat. Ñootakh ma bëgue théâtre
Mome Gope
Mome Gope Hace 10 horas
Wallahi l'histoire de delia la est touchante j'ai ma soeur qui a exactement la même épreuve mais yallah bakhneu et franchement bonne continuation a vous
Mbasu Sosseh
Mbasu Sosseh Hace 10 horas
Soleil Levant rekk..great series!!!Ndey Coumba daal mingi nee rekk
Sora Wally Sora Wally
Sora Wally Sora Wally Hace 10 horas
Amna solo👂👂👂👂
La cuisine séné guineen
La cuisine séné guineen Hace 10 horas
Khaty met fait peur 😱
Ndaye magatte Ndiaye
Ndaye magatte Ndiaye Hace 10 horas
Svp père Sora parle correctement
doff doporal
doff doporal Hace 10 horas
Nena fima dougou guedieunafi deh😂😂😂😂😂😂mbadou moraw negou botou
Ndaye magatte Ndiaye
Ndaye magatte Ndiaye Hace 10 horas
Ses cool ❤️🥰
Fama Thiam
Fama Thiam Hace 10 horas
Mani khana bakhaw mome comme métier mandikate dans la vraie vie soûlard dans ninki nanka et ici
Mame cheikh Thiaw
Mame cheikh Thiaw Hace 10 horas
Chapeau à toi katy chimère li moy artiste , chaque rôle tu l'assure vraiment
Cheikh sidiya baba Bodian
Cheikh sidiya baba Bodian Hace 10 horas
Cette série reflète l'image notre société car aujourd'hui beaucoup d'entre nous en souffrent d'aucuns font des sacrifices par contre d'autres sont procédés par djinns
Tislime Coulibaly
Tislime Coulibaly Hace 10 horas
Qui trouve que la femme de cheikouna est trop belle machala xalei bi mo âme feeling way
Bandar Ndiaye
Bandar Ndiaye Hace 10 horas
Pere zora tmt koukoy solal
Orakhya Sakho
Orakhya Sakho Hace 10 horas
Rayane: leguii rouss n’a 😂😂😂😂
amadou drame
amadou drame Hace 4 horas
😂😂😂😂😂
Orakhya Sakho
Orakhya Sakho Hace 11 horas
Hahahah té sa Djeukeur migui a côté doko topoto 😂😂😂😂😂😂
Moussa ndiaye
Moussa ndiaye Hace 11 horas
Viviane môme whatsapp rk mais tay môme 1 0 la
Moussa ndiaye
Moussa ndiaye Hace 11 horas
Djiguéne môme bo khoulo ak môme beuthieuk goudi nguéne dioubo ndakh djiguéne loumou mér mér goudi bokkousi
Astou Gueye
Astou Gueye Hace 11 horas
❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪🏽
fatou diaye
fatou diaye Hace 11 horas
Non bakaw raynama
Claudine DIOUF
Claudine DIOUF Hace 11 horas
Bakhaw joue bien son rôle yeinima kaay
adji diop
adji diop Hace 11 horas
Thieuy Mansour Mbaye dou changé mome khadare rek laay lidieunté problemam🤣🤣🤣 mais serie bi nekhna trop🙏🙏🙏🙏
Mbacke Ka
Mbacke Ka Hace 11 horas
Serigne pape malick sy yalna yalla yokou yeurmandém té leeral bamélam ak koni amine
Awa Niang Traoré
Awa Niang Traoré Hace 11 horas
Ça s'annonce bien dei
Xame sa Diiné
Xame sa Diiné Hace 11 horas
Wa thies le melleur abonel smaa chaine
Amadou Sall
Amadou Sall Hace 11 horas
Nice
Abdoulaye Kande
Abdoulaye Kande Hace 12 horas
Katy sera la femme de jojo qui est d'accord avec moi
Baye zale
Baye zale Hace 12 horas
Waa yaw Bakham xana sa baram bou NIKINAKA bobü ??? 🤣🤣🤣
Queen Black
Queen Black Hace 12 horas
Non Bakhaw dafa meune rôle mandikat nak 😂😂 pareil dans ninki nanka
Sokhna Ndiaye
Sokhna Ndiaye Hace 12 horas
NEKHNA TROP MACHALA DOUNDELENE ❣💞💝❣💞💝❣
Dieyna Anne
Dieyna Anne Hace 12 horas
Franchement série bi dafaye yeitei si lou beuri🥰🥺
Djiby Ndiaye
Djiby Ndiaye Hace 12 horas
Wa team ande sétane série yeup
Lamine Diop
Lamine Diop Hace 12 horas
Hdg
Amadou Sall
Amadou Sall Hace 12 horas
Nice
Safiétou Ciss
Safiétou Ciss Hace 12 horas
Où est Bineta Koh Samb ?
Ndeye Fall
Ndeye Fall Hace 12 horas
Bilaye somboulou ya bone
Dieyna Anne
Dieyna Anne Hace 12 horas
Rayane il m fume (wa lgui rouss na)😂😂😂😂😂😂
Saly Brickest seye
Saly Brickest seye Hace 12 horas
Nguén tokk ba heur bi diko doga dougeul khawma kolénn yap
Modou Fall
Modou Fall Hace 12 horas
Machallah
gueye coumba
gueye coumba Hace 12 horas
mais pere jora un peut de respect fermel sa chemise bi